Skip to content

Opening book details…

Can I read Bàmmeelu Kocc Barma: téereb nettali on EtoBox?

Bàmmeelu Kocc Barma: téereb nettali by Bubakar Bóris Jóob (Boubacar Boris Diop) is a work of fiction available to read on EtoBox.

What is Bàmmeelu Kocc Barma: téereb nettali about?

"Njéeme Pay, taskatu xibaar bu siiw ci Senegaal, moo toog bés këram dégg ci rajoy réew mi ne Joolaa bi, bato bi daan lëkkale Sigicoor ak Ndakaaru, suux na. Bàmmeelu Kocc Barma day delsi ci jéyya ju tiis jooju, di sargal ñi ci faatu ñépp, di jéem a yeewaale yit askan wi ngir lu ni mel bañ noo dalati. Waaye Njéeme yemul foofu: dafa nuy fàttali yit jaar-jaaru ndem-si-Yàlla ji Kinne Gaajo, fentaakon bu mag bu fiy taalifam yéemoon Afrig ak àddina si yépp. Ñoom ñaar nag, ay xariti benn bakkan, ay doomi-ndey, lañu woon, mu xamaloon ko lépp. Looloo tax Njéeme Pay di dànkaafu jàngkat bi, naan ko: bul jàppe Bàmmeelu Kocc Barma ni téereb nettali doŋŋ, téereb dekkali la tamit. Yokk na ci sax ne “fey bor, féddali kóllëre ak sàmm sama kàddu ñoo ma ko tax a bind...”"

Who reads Bàmmeelu Kocc Barma: téereb nettali?

It is typically read by readers looking for immersive, entertainment-first reading.

Common subject areas: fiction, literature, genre fiction.

Author
Bubakar Bóris Jóob (Boubacar Boris Diop)
Publisher
Éditions Ejo
Published
2017
Language
WO
ISBN
9782490146000
Category
work of fiction
Subjects
Literary Fiction, Fiction, Humanities

More by Bubakar Bóris Jóob (Boubacar Boris Diop)

Browse all works by Bubakar Bóris Jóob (Boubacar Boris Diop)

Similar books